Ci yoon wi wepp, samaritains yi ak sapeurs yi dañu doon bayyi xel doxkat yi. Ay woto dõon nañu may ndox te yeneen daan nañu taxaw ngir faj ñi amoon ay gaañu gaañu yu ndaw.