A la queue leu leu Dakar Grand Yoff Home Dessert au coin des rues
francais mandinka

Marabout et talibés

17h13, le 29 May 2009
Dans la rue

Ci dëkku Sénégal, jafé jafé yi talibé yi dafa di waxtaan bu naqari. Ay waa juur dañuy denkaane seeni doom ci benn seriñ ngir mu jàngal leen alxuraan. Wande seriñ yepp mênuñoo dundal talibé yi yepp. Kon dañu leen di yondi ci mbedd mi ñuy yelewaan. Ci kaw loolu, dañu leen di teg lu meeti ci seen yaram lu dem ci door ak ñakk geen ci daara ji bu ñu mokkalul seeni alluwa.

Log in
Log in
valid HTML5 Valid CSS firefox