Ñaari neeg yi bokk nañu ci Daffé Kunda. Ci biir neeg yi, jiggeen yi dañuy togg àñ bi bës bu nekk ngir waa Daffé Kunda yepp.